Loutax nga wara choisir Lokci ci Sénégal ?
- Jaayal say produits digitaux ci 20 secondes
- Jot sa xaliss directement ci Wave wala OM
- Say client mën nagn la fey ak Wave, Orange Money wala Carte
- Lokci moy yone fichier bi automatiquement bou client bi feyé
- Say dossier woor nagn – ebooks, vidéos, formations, templates
- Amoul frais you laqatou, 10% rek lay plateforme bi dieul
Nan ngay commencé ?
Yomb na : oubil compte, dougal sa produit, té commencé jaay légui ci Sénégal bi yeup.
Sounou Ndigël : Téléchargél sounou guide bi pour xam nan ngay amé say premier client.
Ladj yi niou bari di déf (FAQ)
Ndax mën na commencé té amouma expérience ? Waaw, Lokci dafa yomb lool, kéne kou né mën nako utilisé.
Nan laay joté sa xaliss ? Sa commission day déllou directement ci sa compte Wave wala Orange Money.
Lan laa mën a jaay ? Ebooks, formations, vidéos, coaching, ak yénén dossier you am solo.